Compositor: Não Disponível
[Iblow]
Bh, bh, bah, bah, bah
Bakkal ma nder ma seeti siŋ-siŋ
Nobeel feeñ ma def feem
Xel dafa yëg netalli xol
Mb-mb-mbëggeel bi daw na yaram waaye cat mooy col
Il n’est jamais trop tard
Il n’est jamais trop tard
Sa xarit ñépp a mariée
Góor gu ne bëgg la marié
Yaw nga ni man rekk lay doon
[Awa thies]
Yaa fondement sama amour
May féey sa geej ni dieu ne yaa ma napp, waay!
Tej ma sa xol ba mu mel ni, yaw la (yaw la)
[Pape bilal]
Li ndox di def ci jën
Nu ko raw ngay def ci man ma la bëgg, waay!
Kaay toog ci xol bi bañ a dem, yaw la
[Awa thies]
Sama xol ba mu faiblé
Yaay ki ko chargé ba mu fees waay!
Ki tax xol biy daŋ-daŋi, yaw la
[Pape bilal]
Sama coco ananas biy neexal xol bi, yaw la
[Awa thies]
Mar naan sax du la tax a dikk
[Pape bilal]
Nopp a dégg bët yi gis
Xel ni ma xol bi, yaw la
[Awa thies]
I love you!
[Dane & awa thies]
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Bu dul yaw du doon keneen)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Sama xol bi ne na yaw la, waay!)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Waa mbedd mi ne nañu yaw la, waay!)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
Suñu waa-kër ne nañu yaw la, waay!
Man ki ma bëgg dafa pare waaw
Amul temps-wu wax ak gaa ñile
[Fatel]
Yaa ma leen gënal (yaw)
[Dane]
Kon fu ma jaar ñu ne waaw
[Fatel]
Chéri, chéri yeah
Ki ma gis sama rêves yaw la
[Waly dieng]
Man danga laajal sama xol bi
Moo tax sa xel la koy lëmbe, waay
[Fatel]
Yaw toj nga sama ndon bi
Est-ce que liggéeyoo ma?
[Waly dieng]
Baby, sa nobeel a fort waaw
Gis nga mbëggeel su la jàppee!
[Waly dieng]
Dafay mel ni courant ci ndax waay!
Bébé, defal lu la neex fi nga ne ci xol bi jugé woofa
[Fatel]
My baby, dolli ma
Xam nga ni buur bi yaw la!
Yaw ni nga ma bëggee chéri
Nu ka raw la la bëggee, waaw
Man nii laa la bëggee, eeh yeah!
Wan la mbëggeel ba mu neex chéri
Xamal ni yaw la!
[Waly dieng]
Tay ma lamb-lambee sama chéri coco
Waxal la sa mbaax damay neex waay
[Waly dieng]
Yaw baax nga yaatu nga yaw
Tey nga màndu nga chéri coco
Man bëgg naa sama chéri
[Dane & awa thies]
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Bu dul yaw du doon keneen)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Sama xol bi ne na yaw la, waay!)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Waa mbedd mi ne nañu yaw la, waay!)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
Suñu waa-kër ne nañu yaw la, waay!
Man ki ma bëgg dafa pare waaw
Amul temps-wu wax ak gaa ñile
[Fatel]
Yaa ma leen gënal (yaw)
[Dane]
Kon fu ma jaar ñu ne waaw
[Azou]
Naka sa duguda
Est-ce que chéri mi ngi ngallax
Ndox mi est-ce que mi ngi ngallax
Naka sa duguda
Hey ba mi ngi ngallax
Naka sa duguda
Est-ce que chéri mi ngi ngallax
Yaw ku ci nob sa chéri yaw ma ko bii-bisouuus! (Muac-muac)
Wéy, su la neexee ray ko ndax xol bi neex
Rayal, ray rayal ba mu neex!
[Dane & awa thies]
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Bu dul yaw du doon keneen)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Sama xol bi ne na yaw la, waay!)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
(Waa mbedd mi ne nañu yaw la, waay!)
Yaw xanaa xamuloo
Yaw gisuloo ni yaw la
Suñu waa-kër ne nañu yaw la, waay!
Man ki ma bëgg dafa pare waaw