Compositor: Não Disponível
J'te tampi yaay wër di wax noppil
Dëkke di ma yàq fépp
Laisse-moi vivre tranquille
Arame, Modu, Bada, Samba, Fatu Bint
Ne nañu yaa ma waxal fii lu ñaaw
Khady, Maty, Mami, Coumba, Assane, Lamine
Ne nañu yaa ma toog fii lu ñaaw
J'te tampi yaa ngi wër di wax noppil
Dëkke di ma yàq fépp
Laisse-moi vivre tranquille, waaw
Xaajatuma ci koñ bi fu ma dem
Ñu ne yaa ma waxal fii lu ñaaw
Djiby Néne, Hamdy, Mass
Bu ma gis ne ma yaa ma waxal fii lu ñaaw
Doxal ba kenn laal la
Bul ko ragal waxkat la boy
Amoo lu ñi tiit mafia bi
Jugleen ñu yóole
Dëkke di ma peinture
Lu la neex defal boy
Mënoo ci man dara tus
Lamb sama poche
Faj soxla lu ko gëna neex
Tas sa yaakaar tasar
Yere fa mu moole (dama koy sappée)
Dàll fa mu moole (sappée)
Montre fa mu moole (dama koy sappée)
Classe fa mu moole (sappée)
Xeñal lu leex di ko romb xol ba di bon (mu yeen)
Ci soxar ba la
Dina yàq sa der bi toog la ki mooy ku bon
Han yeah ci iññan ba la
Su ma la gisee ngay kaf di ree
Su ma la wanee ginnaaw ngay wax ci man lu ñaaw
Lu ñaaw a ñaaw a ñaaw
Lu ma la lebal hum lu ñaaw
Yàlla noppi na du tay, lu baax la bon di fay
Ma la bëgg mais du yaw lu la bon di may
Ma la wax sa bopp tay du ma ku lay jaay
Yónnu yax amul mujj ngalla bu si wey
Lii ñaaw na, sama noon bi loo nar tay
Lii ñaaw na, wax ma loo nar tay
Man fu ma dem ñun sa noon bi jaar na fi yàq la jaratoo fi dara
Non ooh, doo sama xarit mooloo
Àddunak li ci biir, sukker du ko tere fen
Maa ngi ci biir amul tus
Doxal ba kenn laal la
Bul ko ragal waxkat la boy
Amoo lu ñi tiit mafia bi
Jugleen ñu yóole
Dëkke di ma peinture
Lu la neex defal boy
Mënoo ci man dara tus
Lamb sama poche
Faj soxla lu ko gëna neex
Tas sa yaakaar tasar
Yere fa mu moole (dama koy sappée)
Dàll fa mu moole (sappée)
Montre fa mu moole (dama koy sappée)
Classe fa mu moole (sappée)
Xeñal lu leex di ko romb xol ba di bon (mu yeen)
Ci soxar ba la
Dina yàq sa der bi toog la ki mooy ku bon
Han yeah ci iññan ba la
Mënoo ci man dara tus
Mu yeen ca soxar bala
Tas sa yaakaar tasar
Han yeah ca iñaan ba la