Kima Done Set (feat. Magou Mbaye & Junior)

ZBest Family

Compositor: Não Disponível

Amour bu sincère
Amour bu fidél oh
Ki dox ci li ma neex
Di ma wax wax ju neex

Une personne sincère
Ku bëgg boppam ooh
Te am dignité
Teg si doon ku nite heee hii yee

Bëgg naa ki may bëgg ma bëgg ko
Ñuy dundu lu neex di muñalante
Moom la yàgg wër te gis naa ko waaw

Xale bi ma yàgg wër de yaw la
Ki ma doon seet de gis naa ko
Oh my chéri, you are my baby
Xale bi ma yàgg wër de yawwu la
Ki ma doon seet de gis naa ko
Oh my chéri, you are my baby

Ku ko xamul tamit dégg nga écho bi
Sama love de lay wër Mali ba Éthiopie
France, Italie, wëri naa ko Tugal
Avis de recherche, tapé naa ko Google

Mbëggeel bi nekk ci kaw (aan, ci kaw)
Du ñëw ci suuf (heeey, du ñëw, du ñëw, du ñëw)
Ndax moom bu ñëwee da koy gaañ

Bëgg naa ki may bëgg ma bëgg ko
Ñuy dundu lu neex di muñalante
Moom la yàgg wër te gis naa ko waaw

Xale bi ma yàgg wër de yaw la
Ki ma doon seet de gis naa ko
Oh my chéri, hmm you are my baby
Xale bi ma yàgg wër de yawwu la
Ki ma doon seet de gis naa ko
Oh my chéri, you are my baby

Wëri ko, fils wëri ko
Si mu lay neex moo la ko jaral waay!
Wëri ko, fils wëri ko
Si mu lay neex moo la ko jaral waay!

Man wër naa la fu ne
Baby jar nga ko, chérie
This is looove, waawaaw

Yaa ma ko jaral, chérie, laaj naa la fu ne
Baby jar nga ko, chérie
This is looove, waawaaw

Ci bu lay neex, ma jox la ko ba mu jeex
Xam nga jar nga ko
Baby jar nga ko, chérie
This is looove, waawaaw

Tileel sama xaritoo xol, xam nga jar nga ko
Baby jar nga ko, chérie
This is looove, waawaaw

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital