Compositor: Não Disponível
Je ne veux pas vivre sans toi
Dans mes rêves je te vois
J'ai vu l'amour en toi
Nalingi yo, nalingi yo
Si tu le dis je te crois
Tu es mon amour, mon roi
Je veux rester avec toi
Nalingi yo, nalingi yo
My baby ooh
Rongooñ tuuru na ca mbëggéel kersa du fa am
Na li-lingi-lingi yo, jaral nga ma
(Bébé jaral nga ma)
Ma di la feccal, di la wayal
Lu mu jar ma def ko, pare naa
Su météo doon gis mbëggéel, asaman neex
Taw lay dëkke ba fàww
Sori ci man, jege ci man
Mbëggéel a bari doole
Xol buy bëgg du tàggoo
Def naa la xarit
Sama chéri
Oh, man dama la love ni July ak Roméo
Xale bi yaw ar gaay
Ñëwal fii nu bége yaw
Danga dof ci man, ma dof ci yaw tu sais
Nawet nga yaw, tawal mu gaaw je sais
Yaa dàq lem, dàq ceeb ci neex
Bu ñu dund lu original ba romb septième ciel (hee)
An kaa gidelam (hee)
An kaa sehilam (hee)
Je ne veux pas vivre sans toi
Dans mes rêves je te vois
J'ai vu l'amour en toi
Nalingi yo, nalingi yo
Si tu le dis je te crois
Tu es mon amour, mon roi
Je veux rester avec toi
Nalingi yo, nalingi yo
Tu m'as fait bae halluciner
Te man je sais bébé, allons dîner
Yeaaah, ku bëgg te fowul
Ngoram du ko jaay
Bul wanteer du fëgg jaay
Xol lu ci njëkk a dugg, nobeel moo ko maye
Fii du marché yebbi, du Colobane bu ñu ray
Aywa leen, aywa leen
Ku fi gis xol buy jaay
Je ne veux pas vivre sans toi
Dans mes rêves je te vois
J'ai vu l'amour en toi
Nalingi yo, nalingi yo
Si tu le dis je te crois
Tu es mon amour, mon roi
Je veux rester avec toi
Nalingi yo, nalingi yo
Sori ci man, jege ci man
Mbëggéel a bari doole
Xol buy bëgg du tàggoo
(Nalingi yo, nalingi yo)
Su météo doon gis mbëggéel, asaman neex
Taw lay dëkke ba fàww