Compositor: Não Disponível
[Awa Thies]
Kaay ma jaay la mbëggeel bu dëgg
Ak xol bu nice, bu ànd yërmandé
Kaay ma jaay la li nga gëna bëgg
Jigéen bu baax dey yaw wax dëgg
[Pape Bilal]
Kaay ma jaay la mbëggeel bu neex
Tegsi jaay la sincérité bu weer, boo dul gis feneen
Góor am na fi ak fideel bu yomb
Nobeel am na fi, nobeel bu ñor xomb
[Awa Thies]
Loo fay gaaw, waxal waxal
Loo fay gaaw?
[Pape Bilal]
Amul waxale
[Awa Thies]
Loo fay gaaw, waxal waxal
Loo fay gaaw?
[Pape Bilal]
Lu ma dajalee
Dajale naa pur jëndëru plaisir
Ay saku bisous ak je t'aime bu baax, eee!
[Dane]
Am na sax mu maikeur
Am na sax mu nob
Am na sax mu muñ ak doyloo, waaw!
Mbëggeel ma jaay
Mbëggeel ma jaay
Mbëggeel ma jaay
Mbëggeel ma jaay
[?]
[Fatel]
Magie bëggante a ngi ni
Mbëggeel rekk laay jaay
Yaw fayal sa impôt sa juti avant ngay jaay
Et puis dama bëgg xol bu sincère, góor bu ngëb
Kuy yërëm jigéen tegsi di ko wax
[Pape Bilal]
Loo fay gaaw, waxal waxal, loo fay gaaw?
[Awa Thies]
Amul waxale
[Pape Bilal]
Loo fay gaaw, waxal waxal, loo fay gaaw?
[Awa Thies]
Lu ma dajalee
Dajale naa pur jëndëru plaisir
Ay saku bisous ak je t'aime bu baax, eee!
[Dane]
Am na sax mu maikeur
Am na sax mu nob
Am na sax mu muñ ak doyloo, waaw!
Mbëggeel ma jaay
Mbëggeel ma jaay
Mbëggeel ma jaay
Mbëggeel ma jaay