Amy Ndiaye

ZBest Family

Compositor: Não Disponível

Amineta ndiaye, aminata ndiaye
Amineta ndiaye mani wagnil ni ngua néké way
Amy, amy, amy adouna dou nono
Amy amy, amy wag nil ni ngua néké waw
Amy amy, amy internet dou nono

Amy amy, amy TikTok bi dou nono
Amy ndiaye
Bou TikTok nékone auto moy chauffeur
Tingui tingui tee eh eh eh
Amy snap béko misérlo
Sou yéwo deff na make up
Daddy commence pause na khéff ay lendeu
Dieul telephone bi TikTok
Dji lay néké que journée bay ladié
Amy ndiaye
Dou diappalé yaym snap la deuk ké
Sokhla sounékoul leu
Dou diappalé yaym snap la deuk ké
TikTok béne yonn am 100 milles vues
Dooléti bénéne tik rok
Amineta ndiaye, aminata ndiaye
Amineta ndiaye mani wagnil ni ngua néké way
Amy amy, amy adouna dou nono

Amy amy, amy wagnil ni ngua néké way
Amy amy, amy internet dou nono
Amy amy, amy TikTok bi dou nono

Amy ndiaye day dokh di kardisha xale carte gap
Sacs bii saff nasseu
Amy ndiaye bou diougué sol thierré seuk ke abdou yeuré
None bindeu maartéee
Day lale fem yii
Day lale Gucci
Original liti
Amy ndiaye dou ligueye
Travaille banaaa ley
Elle travaille chez TikTok
Amy ndiaye kom auto
TikTok bi ko moko
Bouyiinélaw sakh day photo

Amy ndiaye miss poto poto
Amy ndiaye euh
Dou diappalé yayam snap la deuk ké
Sokhla sounékoul leu
Dou diappalé yayam snap deuk ké
TikTok béne yonn am 100 miles vues
Doléti bénéne TikTok

Amineta ndiaye, aminata ndiaye
Amineta ndiaye mani wagnil ni ngua néké way
Amy, amy, amy adouna dou nono
Amy amy, amy wag nil ni ngua néké waw
Amy amy, amy internet dou nono
Amy amy, amy TikTok bi dou nono
Amy amy
Amy amy

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital